Jant
Apparence
![Wikipedia](http://upload.wikimedia.org/wikipedia/commons/thumb/e/ef/WikiLettreMini.svg/36px-WikiLettreMini.svg.png)
![](http://upload.wikimedia.org/wikipedia/commons/thumb/d/d4/Izgrew.jpg/220px-Izgrew.jpg)
Jant (junj: ) bi mooy biddiwu sunu nosteeg jant. Ci li ko wër la Suuf si di warangiku, am na yeneen juroom-ñaari àdduna, ak kuusi àdduna aki xeer yu réy. Kàttanu ceeñeer gi jant biy àggal ci Suuf si moo tax dund man faa am; kàttan googu day nu man a am ndox ci nekkinu yullaakon, tax it gañcax gi man a jot ci naaj wi mu soxla ngir seenug dund