Aller au contenu

Xël

Jóge Wikipedia.

Xël xeetu garab la gu bokk ci njabootu Moraceae.

xël gi


Xël man nay hàgg ba 40i met ci guddaay.

Nataali xël

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]
Ronu xël
xobi xël


Garabu xël


Turu xam-xam wi

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]

Ficus platyphylla

Yeneen i làkk

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]

Araab: التّين Farañse: figuier