Aller au contenu

Aser

Jóge Wikipedia.

Ci làkku ibrë (אָשֵׁר) la tur wi jóge. Ci angale mooy Asher; Ci faranse mooy Asser

Benn ci giiri bànni Israyil la woon, ñi soqikoo ci Aser, mi doon juróom-ñetteelu doomu Yanqóoba bu góor.

Giiru Aser moo feeñ ci Injiil ci Lu 2:36; Pe 7:6.